TSK

TSK · Proverbs 29:5

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Léegi nag sang bi, yal na sa kàddu gii di sama noflaay. Ndax yaw Buur, sama sang, dangaa mel ni malaakam Yàlla, am ug dégg, di teqale liy yoon ak li dul yoon. Yal na sa Yàlla Aji Sax ji ànd ak yaw.»

Éy Aji Sax ji, wommate ma sa njekk ndaxi noon, te xàllal ma saw yoon.

Muy mocc ak a moccaat, ba nax ko, di wax lu neex, ba man ko.

Ab noon làqoo na ay waxam, lal pexey wor ca xolam.

Fa kaw la Aji Sax ji sànnee sawara ci sama biiri yax, moo laaw ab caax ngir fakktal ma, waññi ma, jànnaxe ma, ma dëkke yoggooral.

¶ Ba mu ko defee ñu bàyyi Yeesu xel, daldi yebal ay yeerukat, sas leen ñu yiw-yiwlu te di ko fiir ci kaw kàddu ba jàpp ko, ngir jébbal ko boroom dëkk bay boroom kilifteef ga ak sañ-sañ ba.

¶ Masunoo jaye, xam ngeen ko, ag bëgge it masunoo taxa jóg, Yàlla seede na ko;