TSK

TSK · Proverbs 3:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Xamleen xéll ne ni baay di yare doomam, ni la leen seen Yàlla Aji Sax ji yare.

Job 5:17 TSK

Ma ne, ndokklee ku Yàlla jubbanti, kon bul bañ yarub Aji Kawe ji.

Waaye Boroom bee nuy àttee ay mbugalam ngir yar nu, ba deesu nu mbugalaale ci biir àtteb àddina.

¶ Moo tax dunu ñàkk yaakaar. Doonte sax sunu bitib jëmm a ngi gën di bon, sunu jëmmu biir moom, mu ngi yeeslu bés ak bés.

Te it fàtte ngeen kàddu yii ñu leen ñaaxe, ni nit aki doomam: «Doom, bul xeeb yaru Boroom bi, bul xàddi, bu la waññee,