TSK

TSK · Proverbs 3:29

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yàllaay dégg, duma leen, moom mi nguuram yàgga sax. Selaw. Soppikuwuñu fenn te ragaluñu Yàlla.

jekkadiy xalaat, di mébét lu bon aka yokku ay.

Kuy mébét lu bon daa réer, kuy mébét lu baax am nga ngor ak worma.

¶ Ba mu ko defee, mu am ñu ne: «Aywaleen, nu lalal Yeremi pexe. Ndax kat soxlawunu ko ba di ci ñàkk dara: du njànglem sarxalkat, du digley boroom xel te du waxyu bu yonent biral. Nanu ko duural ba sànk ko te baña faale lenn ciy waxam.»

Ab jëtun, ak ab jirim, ak ab doxandéem, ak ab néew-doole, buleen ko not. Lu bon it, buleen ko mébétalante ci seen xol.»