2 Samuel 11:4
TSK
¶ Ci kaw loolu Daawuda yebal ay ndaw yu jëli ndaw si, mu dikk, mu tëdde ko. Fekk na ndaw sa gisoon baax bay doora sangu-set. Ndaw sa daldi ñibbi.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Ci kaw loolu Daawuda yebal ay ndaw yu jëli ndaw si, mu dikk, mu tëdde ko. Fekk na ndaw sa gisoon baax bay doora sangu-set. Ndaw sa daldi ñibbi.
Ndaw sa ne ko katam, fóon, ne wajj, ne ko: