TSK

TSK · Proverbs 31:3

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Bumu barey jabar, balaa am xelam di lajj. Xaalis ak wurus it, bumu ko barele lool.

Ma ne leen: «Xanaa du nii la Suleymaan buurub Israyil bàkkaare woon? Li xeet yiy bare lépp amul benn buur bu meloon ni moom. Ku Yàllaam soppoon la te Yàllaa ko faloon buurub Israyil gépp. Waaye moom sax jigéeni doxandéem yi bàkkaarloo nañu ko.

Bare na ku dee, moo ko rey, maneesula waññ ñi mu rey ñépp.