TSK

TSK · Proverbs 31:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Sóol nag déggal Yonatan, daldi ne: «Giñ naa ko ci Aji Sax jiy dund, deesul rey Daawuda.»

¶ Ayimeleg ne Buur: «Buur, ana sa surga yii ba ñu daj, ku la nangule ni Daawuda mii, di sa goro, jiite say dag, te di ku ñu nawloo ci sa biir ëtt bii?

Job 29:9 TSK

kàngam ne xerem, ub gémmiñam,

Ñi ñu jàpp, yal na seeni onk àkki fa yaw. Ñi ci tànki ndee, yal nanga leen musale sa doole ju màgg.

Wax ju xelu sut nab dof, jataayu pénc du fa àddoo.

Yeen waa kër Daawuda, Aji Sax ji dafa wax ne: Àtte yoon, deeleen ko xëye, di xettli ki ñu xañ dëgg ci ki koy néewal doole, balaa sama mer ne jippét, di tàkk te deesu ko mana fey ndax seen jëf ju bon.

¶ Yeremi nag daa làqoo Ayikam doomu Safan, mu aar ko, ba tàbbiwul ci loxol askan wi, ñu rey ko.