Psalms 37:23
TSK
Aji Sax jeey sopp saw yoon, jiite say jéego.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Aji Sax jeey sopp saw yoon, jiite say jéego.
Yal naa saxoo di sàmm sa dogali yoon,
Rëddul yoonu dund, daa lajj, te xamu ko.
Jëfi dof a neex ku ñàkk bopp, ku am ug dégg def njub.
Déglul, doom, muusal te yebu ci yoonu njub.
Kon nag léegi Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Teewlooleen xel seeni jaar-jaar.
¶ Kon nag xool-leen bu baax seen jëfin, defleen jëfinu nit ñu am xel, te baña mel ni ñu ñàkk xel,
Yal na Boroom bi dooleele noonu seen xol, ngir kera bu sunu Sang Yeesu délsee, ànd ak ñoñam ñu sell ñépp, fekk leen sell te mucc sikk, fa kanam Yàlla sunu Baay.
te «ngeen xàllal seen bopp xàll yu jub yu ngeen di jaare seeni tànk,» ngir kuy soox doxe ca wér te baña gëna tële.