TSK

TSK · Proverbs 5:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ «Bu ko xasee naanloo ndox mi, ndegam ndaw see sobeel boppam, wor jëkkëram, ndoxum alkànde mi day tàbbi ci biiram, jural ko wextan, koll bi newi, njurukaayam lax, mu mujj doon ku ñuy móoloo ci biir askanam.

Ku dem ca moom dootoo délsi, doo gisati yoonu dund mukk.

Yonent yiy wax waxyuy fen, sarxalkat yiy jiitee seen coobare, te sama ñoñ soppe ko ni! Moo bu muj ga taxawee, nu ngeen di def?»

ci turu Sang Yeesu. Bu ngeen dajee, te ma bokk ak yeen teewe ko samam xel, ci sunu kàttanu Boroom Yeesu,

waaye ñu ragal ñi ak aji gëmadi ñi ak defkati ñaawtéef yi ak bóomkat yi ak moykat yi ak xërëmkat yi ak bokkaalekat yi, mboolem niti fen ñi, seen añ a nga ca déegu sawara waak tamarax ba. Loolu moo di ñaareelu dee.»