Psalms 73:2
TSK
Waaye man de tuuti kon ma lajj, tuuti ma tarxiis,
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Waaye man de tuuti kon ma lajj, tuuti ma tarxiis,
Àndal ak ku xelu, sam xel rafet; ku lëngook ub dof, loru.
¶ Yooyu xew-xew ay misaal la, ngir nu baña xemmem yëf yu bon, na ko maam ya daan xemmeme.
Naka noonu itam Sodom ak Gomor, ak dëkk ya leen wër, ñoo yebu woon ci powum séy, ak jaxasoo gu woroo ak bindub judduwaale, ba ñu def leen misaal, ñeel ña nara tegoo mbugalum sawara wu sax dàkk.