Ku bon déy a ngi tëggoo bànneexu bakkanam, ku bëgge di ñàkke wormaak a teddadil Aji Sax ji.
TSK
TSK · Proverbs 6:12
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Day gis boppam, naagu, ba du gis sikkam, sib ko.
Bu ngoonee ñu wàccsi, di xiiru niy xaj, di wër dëkk bi.
Caaxaani neen, xooluma; jëf ju wàcc yoon, bugguma, taqu ma fenn.
Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.
jekkadiy xalaat, di mébét lu bon aka yokku ay.
Jubalal, sa njekk musal la; ab workat day bëgge, ba far keppu.
Piise, ku nar njekkar; màttu, ku def lu bon.
Genn dàmb gi di figg ju baaxa baax, mel ni witt mu jëkk. Dàmb gi ci des di figg ju bona bon, ju kenn dul lekk ndax bon.
Te itam ca lañuy tàmme am ug jot, di taxawaalu kër ak kër. Te duñu yem ci am ag jot rekk, waaye dañuy làmmiñu, di dugg lu seen yoon nekkul, tey wax lu leen warul.
Kon nag baleen jépp jikko ju tilim, ak mboolem xeeti mbon yi ne gàññ, te ngeen nangu ci biir ag woyof, kàddu, gi jëmbate ci yeen te man leena musal.