TSK

TSK · Proverbs 6:14

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Ay waxam coxor aki fen, jëfeetul lu rafet ak lu baax.

Kon nga mucc ci kuy def lu bon, tey bànneexoo lu jekkadi.

Aji Sax ji daa sib ku dëng, xejjoo kuy jubal.

Kuy mébét lu bon daa réer, kuy mébét lu baax am nga ngor ak worma.

Ab saaysaay day dëngal, nit ku dëggu di jubal.

Ab njublaŋ, ay pexeem musiba la. Njekkar lay nas, ba bu néew-ji-doole sàkkoo dëgg it, mu fen ba lor ko.

Aji Sax ji ne ma: «Yaw nit ki, ñii ñooy mébétkati ñaawtéef ñiy digle lu bon ci dëkk bii.

Micah 2:1 TSK

Wóoy, ngalla ñiy mébét ñaawtéef, di ràbb lu bon ci seenub tëraay, bët set, ñu jëfe ko, ndax xam ne man nañu ko.

¶ Bu leen lenn nax; Yàlla deesu ko foontoo. Nit ki, li mu ji, moom lay góob.