Psalms 3:6
TSK
Maay tëdd nelaw, yewwu; Aji Sax ji di ma aar.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Maay tëdd nelaw, yewwu; Aji Sax ji di ma aar.
Ngalla yónneel sag leer ak sa dëgg, yal na ma yooyu jiite, yóbbu ma sa tund wu sell, sa dëkkuwaay ba.
Sama xol laa làq say wax, ngir bañ laa moy.
Sa dogali yoon laay woyantoo, fu ma mana sance.
Damay xoole guddi gépp, di jàngat sa kàddu.
Kon sab dox wóor, doo fakktalu.