2 Samuel 11:2
TSK
¶ Genn ngoon, Buur Daawuda jóge ca kaw laltoom, di doxantu ca kaw taaxum këram. Mu tollu ca kaw taax ma, séen as ndaw suy sangu. Ndaw sa neexa xool lool.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ Genn ngoon, Buur Daawuda jóge ca kaw laltoom, di doxantu ca kaw taaxum këram. Mu tollu ca kaw taax ma, séen as ndaw suy sangu. Ndaw sa neexa xool lool.
¶ Gannaaw loolu Yewu jubsi Yisreel, Yesabel yaayu Buur dégg ko, tusngalu, defaraat boppam, taxaw ca palanteer ba, di séentu.