2 Kings 5:24
TSK
Gewasi agsi ca tund wa, jële ko ca seeni loxo, dem, denci ko ca biir kër ga, ba noppi yiwi leen, ñu dem.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Gewasi agsi ca tund wa, jële ko ca seeni loxo, dem, denci ko ca biir kër ga, ba noppi yiwi leen, ñu dem.
Mbuusum xaalis la ŋàbb, yóbbu, du ñibbsi ndare weer wi fees dell.»
Bul xool biiñ ak xonqaayam. Aka yànj cib kaas te neexa jolu!
Waaye bàkkaar moo jaare buntub ndigalu yoon, ba yee ci man mboolemi xemmemtéef yu bon. Ndax kat, su yoonu Musaa amul woon, bàkkaar di lu dee.
Waaye ku nekk, sa xemmemtéefu bakkanu bopp moo lay xiirtal, ootal la ba nax la.