TSK

TSK · Psalms 104:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Job 38:41 TSK

Ana kuy xont baaxoñ, fa doom yay wooye Yàlla wall, di tërëf ndax ub xiif?

Ñépp a la wékk bët, di yaakaar, te bu jotee, yaa leen di leel,

Aji Sax ji déy da maa wax ne ma: «Gaynde gu mag ak gu ndaw, bu jàppee bay xiiru, boo ko wooloon gàngooru sàmm it, duñu soowaloo ba xëbal ko, duñu ñolñoli ba mu dellu gannaaw. Noonu la Aji Sax ji Boroom gàngoor yiy wàcce, xaresi fi kaw tundu Siyoŋ ak waa tund wa.»

Joel 1:18 TSK

Céy ni mala yiy binnee! Gétti nag yaa ngi jànnaxe, ndax ñàkk parlu, gàtt yi itam loof.

Joel 2:22 TSK

Yeen rabi àll yi, buleen tiit, parluy àll yi day naat, garab yi meññ; figg ak reseñ di baaxee seen xéewal.