TSK

TSK · Psalms 18:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Yal na Aji Sax ji àtte xeet yi; Aji Sax ji, seetal ci sama njubteek sama maandute te dëggal ma.

Ñeel Daawuda. Aji Sax ji, àtte ma, man de maandu laa wéye, Aji Sax ji laa wóolu, jenguma.

Say santaane it dëdduwma ko, nde yaw yaa ma jàngal.

Sama Yàlla yebal na malaakaam, mu tëj gémmiñi gaynde yi, ba defuñu ma dara. Ndax kat mucc naa ci tuuma sama digganteek moom ak sama digganteek yaw it, te defuma dara lu bon.»

¶ Yeena seede, Yàlla itam seede, sellnga ak njub, ak mucc sikk ga nu doon jëfe fa seen biir, yeen ñi gëm.