TSK

TSK · Psalms 22:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Taawub yëkk la, daraja mooy boroom, béjjén ya, béjjéni nagu àll la, ca lay butteendoo xeet yépp, ba ca cati àddina. Ñooñooy junniy junniy nit ca giirug Efrayim, ak junni ca giirug Manase.

Éy Aji Sax ji, loo deeti seetaan? Musal ma ci seenum pàdd, wallu ma ci yii gaynde, sàmmal ma sama benn bakkan bii!

Moona bés bu nekk, maak yeen la woon ca kër Yàlla ga, te teguleen ma loxo. Waaye seen waxtu la léegi, bi kilifteefug lëndëm ayee nii.»

Acts 5:30 TSK

Sunu Yàllay maam moo dekkal Yeesu, mi ngeen wékk ci bant, bóom ko.

¶ Àndleen ak sago te teewlu! Seenub noon Tuumaalkat bi, mu ngi ŋar ni gaynde, tey wër, di rëbb ku mu warax.