«Ngalla yaw Yerusalem, mi ngëlén pamti-pamtee ba nga jàq, te kenn dalalu la, man Aji Sax ji, maa ngii di la tabaxe doj yu ne ràññ, samp la ci kenuy safiir.
TSK
TSK · Revelation 21:14
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Isaiah 54:11
TSK
Galatians 2:9
TSK
Ña ñu jàppoon ne ñooy kenuy mbooloom gëmkat ña nag, te ñuy Yanqóoba ak Sefas ak Yowaan, ba ñu ràññee yiw wi ñu ma jagleel, maak Barnaba lañu jox loxo, ngir nun nu liggéeyi ca jaambur ña, te ñoom ñu liggéeyi ci Yawut yi.
Ephesians 3:5
TSK
Moomu mbóot, xamaleesu ko woon doom aadama yi, ca janti maas ya woon, ni ñu ko feeñalale tey, ñu sell ñi diy ndawam ak yonent yi, ci ndimbalal Noo gu Sell gi,
Hebrews 11:10
TSK
Booba Ibraaymaa ngay séentu dëkk ba ca kenu ya, te Yàlla di ki yor xaralag tabax bi, boole ci di tabaxkat bi.
Revelation 18:20
TSK
Ndokklee, asamaan, Ndokklee, yeen ñu sell ñi itam, ak ndawi Yàlla yeek yonent yi, ndaxte Yàllaa leen àtteek dëkk bii, mbugal ko.