Ezekiel 2:10
TSK
Mu tàqarñi ko fi sama kanam, muy lu ñu bind biir ak biti, mbind ma di kàdduy jooy aki onk aki yuux.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Mu tàqarñi ko fi sama kanam, muy lu ñu bind biir ak biti, mbind ma di kàdduy jooy aki onk aki yuux.
¶ Juróomeelu malaaka mi wal liitam, ma gis, biddiiw bu xàwwikoo woon asamaan, ba wadd ci kaw suuf. Ñu jox ko caabiy kàmbu xóote ba.
¶ Ñaareelu musiba mi wéy na, waaye kat ñetteel baa ngi nii di ñëw.
¶ Ci kaw loolu ma gis meneen malaaka muy naaw ci digg asamaan, ànd ak xibaaru jàmm bi sax dàkk, ngir baaxe ko waa àddina: niti wépp askan ak gépp giir ak wépp làmmiñ ak wépp xeet.