TSK

TSK · Romans 14:8

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Waaye sama bakkan soxalu ma, xanaa ma bey samaw sas, ba sottal liggéey, bi ma Sang Yeesu dénk, te mooy seedeel xibaaru jàmm bu yiwu Yàlla wi.

muy Póol, di Apolos, di Sefas, di àddina, di dund, di ndee, di tey, di ëllëg, lépp, yeena ko moom.

Loolu laa ne siiw, yaakaar ko, te duma rus mukk, xanaa di saxoo aw fit, démb niki tey, ngir ma mana fésale sama jëmm jépp, teddngay Almasi, su may dund ak su may dee.

ndax liggéeyal Almasi tax na koo riisu ndee; ba ngeen amee ngànt lu leen teree mottlil seen bopp, seen yéene, moo jaay bakkanam ngir wuutu leen, ba yótsi ma seen ndimbal.

Su nuy dund, ak su nuy dee, moom moo nu deeyal, ngir nu mana ànd ak moom, dund.