Romans 4:23
TSK
Ba ñu bindee ne ngëmu Ibraayma, moom lees ko waññal àtteb ku jub, du Ibraayma doŋŋ la mbind ma ñeel.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
Ba ñu bindee ne ngëmu Ibraayma, moom lees ko waññal àtteb ku jub, du Ibraayma doŋŋ la mbind ma ñeel.
Ndax kat sunu mucc, yaakaar la taxaweegum, te yaakaar joo teg sa bët, dootu yaakaar. Li nit ki teg bëtam, nu mu koy yaakaaratee?
Bindees na ci yoonu Musaa kay ne: «Bul sunjuñ gémmiñu nag te fekk koy bojj am pepp.» Ndax Yàlla nag yi doŋŋ la tiisoo?
Mboolem Mbind mu sell mi la Yàlla wal ag Noowam, ba mu am njariñal jàngal nit ñi, femmu leen, jubbanti leen, yar leen cig njub.
¶ Kon nag buleen teqlikook seenu fit, yool bu réy a ngi ci.
¶ Kon nag teewlooleen seen xel, te ànd ak seen sago, te ngeen wékk seen jépp yaakaar ci yiw wa ñu leen di dikke kera bu Yeesu Almasi feeñee.