TSK

TSK · Romans 6:18

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Sa yoonu santaane laay daw, yaa may may xol bu tàlli.

Aji Sax ji sunu Yàlla, yeneen sang yu la moy moom nañu nu, waaye saw tur rekk lanuy màggal.

Luke 1:74 TSK

ne moo nuy may nu mucce ci loxoy noon, ba man koo jaamoo xel mu dal

Ndax kat bàkkaar yilifatu leen, nde du ci kilifteefu yoonu Musaa ngeen nekk, waaye ci aw yiw ngeen tàbbi.

Waaye tey bi ñu leen yiwee, ba ngeen doon ay surgay Yàlla, ag sellnga la leen loolu jural, te muj ga di texe gu sax dàkk.

Ndax ab jaam nga woon, ba ñu lay woo? Amul solo. Waaye soo manee yiwiku, yiwikul.

Ay gor ngeen, waaye jaami Yàlla ngeen. Kon buleen taafantoo li ngeen diy gor ba def lu bon.