Exodus 20:14
TSK
¶ «Buleen jaaloo.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
¶ «Buleen jaaloo.
bu ñu àndee ak ndaw si, te moom miy jëkkëram yégu ko; te ba ndaw say sobeel boppam, fekkeesu ko fa ba di ko seede;
¶ Ruut ne ko: «Teral nga ma de, sang bi. Yaa ngi may laaye biir, ndaxte dëfal nga ma, wax ma lu seral sama xol, te moona say surga yu jigéen yi sax a ma gën.»