TSK

TSK · Romans 8:20

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Mu tudde ko Nóoyin (mu firi Noflaay) ndax dafa ne: «Kii moo nuy taxa noyyiwaat, noppal nu ci liggéey yu metti ak coonoy mbeyu suuf, si Aji Sax ji rëbb.»

Job 12:6 TSK

Jàmm a nga ca xaymay yàqkat ya, te xel mu dal di céru tooñkati Yàlla yooyu, ŋàbb seeni yàlla.

Suuf si la ñi ko dëkke sobeel, ñoo wàcc yoon yi, xëtt ndigal, fecci kóllëre gi sax dàkk.

Def nañu ko gent buy jooy fi sama kaw, réew mi mépp gentala gental, te saful kenn.

Hosea 4:3 TSK

Moo tax réew mi wowal, mboolem lu fi dëkke ràgg, ba ci rabi àll yi, ak njanaaw yi, jëni géej itam day réer.

¶ Xam nanu ba fii nu tollu ne mboolem càkkéef gaa ngi binni ndax mitit, ni kuy matu.