Psalms 44:22
TSK
du la ump, yaw Yàlla, mi xam kumpay xol.
TSK
Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.
du la ump, yaw Yàlla, mi xam kumpay xol.
Dees koo néewal doole, mitital ko te ubbiwul gémmiñam, xanaa mel ni xar mu ñuy rendiji, ne cell ni xar mu ñuy wat, ubbiwul gémmiñam.
Waaye yaw Aji Sax ji, xam nga ma; gis nga ma, seetlu sama xol ci yaw. Diri leen niy xar yu ñuy rendi, beral leen bésub rendi.
Waaye sama bakkan soxalu ma, xanaa ma bey samaw sas, ba sottal liggéey, bi ma Sang Yeesu dénk, te mooy seedeel xibaaru jàmm bu yiwu Yàlla wi.
Te kon nun it, ana lu jar nuy jaay sunu bakkan waxtu wu nekk?