TSK

TSK · Romans 9:21

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

Éy Aji Sax ji, bul mer lool, bul ba xel fàww ci ñaawtéef. Ngalla seetal ne nooy sa ñoñ, nun ñépp.

Nee ñu: «Waa jii Kooña da di njaq lu toj lu jarul daraa? Am da di xottu ndab lu kenn buggul? Lu waral ñu di ko sànni, mooki doomam, xalab leen biir réew mu ñu xamul?»

Acts 9:15 TSK

Sang bi ne ko: «Demal, ndax kooku jumtukaay laa ko tànne, ngir mu xamali sama tur, xeeti jaambur yi ak seeni buur, xamal ko itam bànni Israyil.

Kon nag Yàlla mooy yërëm ku ko neex, te ku ko neex lay dëgëral xolam.

¶ Kër gu mag nag, du ndabi wurus ak xaalis rekk a fa am, waaye yoy bant a nga fa, ak yoy ban; yii di ndabi teraanga, yee di ndabi njoogaan.