TSK

TSK · Ruth 2:11

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi
Ruth 1:14 TSK

¶ Ñu dellu ne yikkét, di jooyoo. Orpa fóon goroom, tàggtook moom, Ruut nag moom langaamu ko rekk.

Ruth 3:10 TSK

¶ Mu ne ko: «Yal na la Aji Sax ji barkeel, doom! Jiwati nga bokk gi ngor lu gënatee rafet. Ndax su la neexoon, nga topp ci xale yu góor yi, ñu am ak ñu ñàkk.

Jébbalul ci Aji Sax ji, dénku ci moom, mooy sottal.

Luke 5:11 TSK

Ci kaw loolu ñu teeral gaal ya ca tefes ga, daldi bàyyi lépp, topp ca moom.

Naka noonu itam, kenn ci yeen du mana doon sama taalibe te dëdduwul mboolem lu mu am.

¶ Ba Yàllay woo Ibraayma, ngir mu génn, jëm bérab ba mu mujj muurloo, ngëm la déggale Yàlla, ba génn, dem te xamul woon fu mu jëm.