TSK

TSK · Ruth 3:2

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

¶ Bu ay góor yu bokk waajur dëkkee, kenn ci ñoom dee te bàyyiwul doom ju góor, jabaru ki dee du génn, di séy akub jaambur. Jëkkëru donaleem ju bokk ak jëkkëram moo ko wara jël, donloo ko.

Ruth 2:8 TSK

¶ Bowas nag ne Ruut: «Doom, ma ne, bul saatuji ci beneen tool bu dul bii. Bul wees fii. Toogal fii ci samay surga yu jigéen.

Yeesu miy sellal nit ñi, moom ak ñi muy sellal, ñoo bokk lenqe, te moo tax Yeesu rusu leena wooye ay bokk.