TSK

TSK · Zechariah 13:4

Treasury of Scripture Knowledge references in KYG.

Dellu ci pàcc bi

fekk na Aji Sax ji wax, Esayi doomu Amocc jottli. Mu ne ko: «Demal summi tubéyu saaku ji nga sol, te summi say dàll.» Mu def noona, di doxe yaramu neen, tànki neen.

Ñu wara am gàcce ci seen jëf ju siblu, te gàcce gàcceelu leen. Xamuñu sax luy kersa! Moo tax ñuy fëlëñoondook ñiy fëlëñu. Kera ba ma leen di dikkal, ñooy tërëf.» Aji Sax jee ko wax.

Micah 3:7 TSK

Seetkat yi dañuy rus, boroom ngis yi torox, ñoom ñépp jàpp seen gémmiñ; ndax Yàllaa leen dul faale.»

Dinaa may nag sama ñaari seede yi, ñu biral waxyu diiru junni ak ñaar téeméeri fan ak juróom benn fukk (1 260) yu ñuy sol ay saaku, di ko toroxloo.»