1 Samuel 3:11
TSK
Aji Sax ji ne Samiyel: «Maa ngii déy, di waaja def ci digg bànni Israyil, mbir muy buur noppi mboolem ku ko dégg.
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Aji Sax ji ne Samiyel: «Maa ngii déy, di waaja def ci digg bànni Israyil, mbir muy buur noppi mboolem ku ko dégg.
Suuf si la ñi ko dëkke sobeel, ñoo wàcc yoon yi, xëtt ndigal, fecci kóllëre gi sax dàkk.
Danga naan: “Yeen buuri Yuda, yeen waa Yerusalem, dégluleen kàddug Aji Sax ji. Aji Sax ji Yàllay Israyil Boroom gàngoor yi dafa wax ne: Maa ngii di wàcce fi bii bérab, musiba muy buur noppi képp ku ci dégg.”
«Yeen doŋŋ laa ràññee ci mboolem askani suuf. Moo tax ma di leen mbugal ndax seen ñaawtéef gépp.»
Ba mu ko defee buuri àddina yeek kilifa yeek njiiti gàngoor yeek boroom alal yeek boroom doole yeek, mboolem jaam yeek gor ñi, ñépp làquji ci xunti yeek doji tund yi.