TSK

TSK · 2 Kings 21:24

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Noonu la magi Israyil ñépp dikke ca Buur Daawuda ca Ebron, mu fasook ñoom kóllëre fa kanam Aji Sax ji. Ñu sotti Daawuda diwu pal ga, muy buurub Israyil.

¶ Ci biir loolu Israyil gépp dégg ne Yerbowam délsi na; ñu woote ndaje, woo ko ca, fal ko buurub Israyil gépp. Kenn farul ak waa kër Daawuda, lu moy waa giirug Yuda doŋŋ.

Ba nguur ga demee ba dëgër ci loxoom, moo bóom jawriñam ña bóomoon Buur baayam.

¶ Juróom yetti at la Yosya amoon ba muy falu buur, te fanweeri at ak benn la nguuru fa Yerusalem. Yaayam mooy Yedida doomu Adaya ma cosaanoo Boskat.