Boo defee noonu, te Yàlla ànd ci, dinga ko mana dékku, mbooloo mii mépp it mana dellook jàmm ca seeni kër.»
TSK
TSK · 2 Peter 3:9
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Aji Sax ji da daan wax ak Musaa ne ko jàkk, mu ne ko jàkk, ni nit di waxe ak moroomam rekk. Bu ca Musaa jógee, daldi dellu ca dal ba, waaye bëkk-néegu Musaa, ngóor sa Yosuwe doomu Nuun daawul génn biir xayma ba.
Waaye yaw Boroom bi Yàlla, yaa ñeewante, yërëm, yaa muñ mer, bare ngor ak worma.
Maa jegeñal sama njekk, soreetul; sama wall a ngi, yàggatul. Maay maye wall fi Siyoŋ gii, ba Israyil gii di sama gànjar.»
Kon ndax Yàlla man naa baña sàmm àqu tànnéefam ñi koy woo wall guddi ak bëccëg, xanaa di leen yeexe?
¶ Yàlla mi namma wone am sànjam, xamle dooleem, su dee moo muñal lool ay ndab yu yelloo am sànjam, te seen sànkute ñoroon xomm nag?
bi bëgg ñépp mucc te ràññee liy dëgg.
ñooña gëmadi woon bu yàgg, jant ya Yàllay muñ, di négandiku, te Nóoyin di yett gaal, ga lim bu néew, juróom ñett, mucce woon ca ndox ma.
May naa ko ab diir, ngir mu tuub, waaye moo buggula tuub ngànctoom.