TSK

TSK · 2 Samuel 13:28

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

Kon nanu def nii: danuy nàndal sunu baay biiñ, tëdd ak moom, ngir sunu xeetu baay du fey.»

Buuru Misra woolu rewlikat ya, ne leen: «Ana lu tax ngeen def lii, di bàyyi liir yu góor yi, ñu dund?»

Ruth 3:7 TSK

Bowas lekk, naan ba xolam sedd, doora dem tëdd ca peggub jalu pepp ba. Ruut jegesi ndànk, muri fa féeteek tànk yi, tëdd.

Ba mu ko defee Buur ne dagam ya ko dar: «Ayca, reyleen sarxalkati Aji Sax yii, gannaaw ñoom it ñook Daawudaa far. Yégoon nañu ba muy daw te xamaluñu ma ko.» Dagi buur ya nag baña xàcci seen loxo ci kaw sarxalkati Aji Sax ya.

Sóol giñal ko ci Aji Sax ji, ne ko: «Giñ naa ci Aji Sax ji, Kiy Dund, mbugal du la ci fekk.»

Ci biir loolu Daawuda woo Uri, mu bokk ak moom lekk, daldi naan. Mu nàndal ko ba mu màndi. Ba ngoon jotee Uri daa génn, tëdd ca laltoom ca biir surgay sangam, waaye këram, àggu fa ba tey.

Kon nag saamar dootu jóge sa kër mukk, ndax yaa ma ñàkke worma, ba jël jabaru Uri Etteen bi, def ko sa jabar.”

Ñu génn digg bëccëg, fekk Ben Addàd a ngay màndi mook fanweeri buur ak ñaar ya mu faral, ca mbaar ya.

dugub di ko dooleel, biiñ di bégal xolam, ag diw di leeral kanamam.

¶ Guddi googa lañu rey Baltacar, buurub waa Babilon.

¶ «Moytuleena yaafusal seen bopp ci naan gu ëpp ak màndite ak xalaati àddina, lu ko moy bés ba jekki dal ci seen kaw,