TSK

TSK · 2 Samuel 21:12

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ci kaw loolu waa Filisti daje, dali ca dëkk ba ñuy wax Sunem; Sóol ànd ak bànni Israyil gépp, ñu dali ca Gilbowa.

Ba mu ko defee ñu denc gànnaayi Sóol ca seen biir kër tuur ma ñuy wax Astàrt, néewub Sóol, ñu wékk ca miiru dëkk ba ñuy wax Bet San.

Ndaw la ne ko: «Dafa yemook ma tollu tembe ca kaw tundu Gilbowa. Ndeke Sóol a nga fa, sukkandikoo xeejam. Watiiri xare yaak gawar ya defuñu lu moy ne ko dann.

Ba mu ko defee waa Yuda dikk, diw fa Daawuda, fal ko buurub waa kër Yuda. Gannaaw gi ñu wax Daawuda ne ko waa Yabes Galàdd ñoo rob Sóol.