KYG / 2 Samuel / الأصحاح 21 KYG · الآية 2 Aa معاينة أدوات نص القارئ Buur woo waa Gabawon, wax ak ñoom. Waa Gabawon bokkuñu woon ci bànni Israyil, waaye ñoo... حجم النص A- 25px A+ خط القارئ بحواف بلا حواف نسخ Amiri Scheherazade New Noto Sans Arabic Cairo Tajawal Markazi Text Changa Noto Kufi Arabic Alexandria Almarai Aref Ruqaa Ink El Messiri Harmattan IBM Plex Sans Arabic Mada Reem Kufi Lateef إعادة ضبط ← 2 Samuel 21:1 2 Samuel 21:3 → قارن ذات صلة شرح المفضلة ملاحظة ♥ 📝 B uur woo waa Gabawon, wax ak ñoom. Waa Gabawon bokkuñu woon ci bànni Israyil, waaye ñoo desoon ca Amoreen ña bànni Israyil giñaloon ne duñu leen rey. Teewul Sóol xéroon lool ci bànni Israyil ak Yuda, bay fexee faagaagal waa Gabawon. اقرأ الأصحاح كاملًا الآيات ذات الصلة اعرضها بجميع ترجمات Wolof اعرضها في جميع نسخ الكتاب