كل أسفار KYG

2 Samuel 21

KYG · الآية 9

24 أصحاحات

KYG / 2 Samuel / الأصحاح 21

KYG · الآية 9

D aawuda jébbal leen waa Gabawon, ñu jam leen ba mu sar, foofa ca kaw tund wa, fa kanam Aji Sax ji. Juróom ñaar ñooñu ñépp a bokk tëdd. Ña nga leen rey ca fan ya ñu tàmbalee góob, ca ndoortel ngóobum lors ba.