Keroog Aji Sax ji fas na kóllëre digganteem ak Ibraam, ne ko: «Askan wi soqikoo ci yaw laa jox réew mii dale ci dexu Misra, ba ca dex gu mag googee di Efraat,
TSK
TSK · 2 Samuel 8:3
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Fépp fu ngeen teg seen tànk, yeena koy moom. La ko dale ca màndiŋ ma ba ca Libaŋ, daleeti dexu Efraat ba ca géej ga ca sowu, lépp seen suuf lay doon.
¶ Amoneen ña xam ne Daawuda jéppi na leen lool. Ñu dem bindi ñaar fukki junniy (20 000) xarekat ca waa Siri ña dëkke Bet Reyob ak waa Siri ña dëkke Soba, teg ca junniy nit ñu bàyyikoo ca buuru Maaka, ak fukki junneek ñaar (12 000) ñu waa Tob.
Ba mu ko defee mboolem buur yay jawriñi Adadeser gis na ñu daanoo fa kanam Israyil, ñu daldi jàmmook bànni Israyil, nangul leen. Ba loolu amee waa Siri ñemeetuñoo sotle Amoneen ña.
Mu boole ay farandoom, ànd ak ñoom, jiite leen gannaaw ba Daawuda faagaagalee xarekati sangam. Ñu dem sanc Damaas, moom ko.
mu yilif géej ba géej ak dex ba ca cati àddina.