TSK

TSK · 2 Samuel 9:1

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Daawuda di wax ak Sóol ba noppi, fekk na Yonatan yég ci xolam na mu taqook Daawuda ci biir cofeelu benn bakkan. Yonatan dafa soppoon Daawuda ni boppam.

bul noppee jëfe ngor sa digg ak sama waa kër mukk, ba sax keroog bu Aji Sax ji faree fi kaw suuf képp kuy noonu Daawuda.»

Ci biir loolu Yonatan doomu Sóol ja dem Orsa ca Daawuda, di ko ñaax ngir mu gëna dëgërloo Yàlla.

¶ Teewul Daawuda déeg Mefiboset, ma Yonatan doomu Sóol di baayam, ndax la ñu giñoo woon ci Aji Sax ji, mook Yonatan doomu Sóol.

Bul fàtte sab xarit mbaa sa xaritu baay, bul jàq ba seeti sa mbokk; dëkkandoo bu jegee gën mbokk mu sore.

¶ Li may tënke nag moo di yeen ñépp, ngeen mànkoo, yégante, bëggante ni mu ware ay bokki gëmkat, baaxeenteleen te woyof.