كل أسفار KYG

Acts 13

KYG · الآية 43

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 13

KYG · الآية 43

B a mbooloo ma tasaaroo, bare na ay Yawut ak tuubeen yuy jaamu Yàlla yu topp ci Póol ak Barnaba. Ñuy wax ak nit ñi, di leen ñaax, ngir ñu sax ci doyloo yiwu Yàlla.