ak mboolem góori këram, muy jaam ya fa juddoo mbaa ñu mu jënd ci ay doxandéem, ñoom ñépp a ànd ak moom xaraf.
TSK
TSK · Acts 18:8
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Genesis 17:27
TSK
Acts 8:12
TSK
Waaye ba ñu gëmee Filib, ma leen xamal xibaaru jàmm, bi jëm ci nguurug Yàlla ak turu Yeesu Almasi, góor ak jigéen daldi nangu, ñu sóob leen ci ndox.
Acts 10:2
TSK
Ku jullite la woon te ragal Yàlla, mook waa këram gépp; bare woon na sarax yu muy yéwéne askan wi, te ñaan ci Yàlla la saxoo woon.
Acts 13:15
TSK
Gannaaw ba tarib dog ya ca téereb yoonu Musaa, ak téereb yonent ya sottee, njiiti jàngu ba yóbbante leen kàddu, ne leen: «Bokk yi, bu ngeen amee kàddu gu ngeen ñaaxe mbooloo mi, waxleen.»
Acts 16:34
TSK
Gannaaw loolu mu yóbbu leen këram, jox leen ñu lekk, tey bégeendoo ak waa këram gépp ci ngëm gi ñu gëm Yàlla.
Romans 10:14
TSK
¶ Waaye nees di wooye koo gëmul? Nees di gëme koo déggul turam? Nees di dégge turam, te yégleesu ko?