كل أسفار KYG

Acts 7

KYG · الآية 38

28 أصحاحات

KYG / Acts / الأصحاح 7

KYG · الآية 38

M oom it moo nekkoon ak mbooloo ma ca màndiŋ ma, mook malaaka ma doon wax ak moom ca kaw tundu Sinayi ca sunu wetu maam ya. Moo jot ci kàddu yuy dund, ngir jottli nu ko.