¶ Ba waa Filisti nangoo gaalu Yàlla ga, Eben Eser lañu ko jële, yóbbu ko seen dëkk Asdodd.
TSK
TSK · Acts 8:40
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
¶ Gannaaw loolu Sang bi tabb na yeneen juróom ñaar fukki taalibe ak ñaar, yebal leen, ñaar, ñaar, ñu jiituji ko ca mboolem dëkk yaak gox, ya mu nammoona dem moom ci boppam.
¶ Ku ñuy wax Korney, njiitu takk-der la woon ca Sesare. Ma nga bokkoon ca mbooloo ma ñu dippee Gàngooru Itali.
Erodd nag santaane ñu wër Piyeer, te taxul mu gis ko. Mu daldi àtte wattukat yi, ba noppi joxe ndigal ngir ñu rey leen.
Ci biir loolu ay taalibe yu dëkke Sesare ànd ak nun, yóbbu nu fa nu wara dali, ca kër ku ñuy wax Manason, ma cosaanoo Sippar, te di taalibe bu yàgg.
Gawar ga àgg Sesare, daldi jébbal boroom réew ma bataaxal ba, jébbal ko Póol itam.
Festus itam ne leen Póol a nga ñu tëj kaso ca Sesare, te moom ci boppam, fa la nara gaaw, dellu.
¶ Gannaaw ab diir buur Àggripa ànd ak jigéenam Berenis ganesi Sesare, ngir nuysi Festus.