Psalms 104:2
TSK
làmboo leer ni mbubb, firi asamaan ni ndimo,
TSK
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
làmboo leer ni mbubb, firi asamaan ni ndimo,
¶ «Yàlla def ma topp yoon wa, ba jub Damaas ci digg bëccëg rekk, ag melax gu mag jekki fettaxe asamaan, ne ràyy fi ma wër.
Man nag la mujja feeñu, te ma dib liir bu ab juddoom moy bésam,
Te dëkk bi soxlawul jant bu koy leeral mbaa weer, ndax leeru Yàllaa koy leeral, Gàtt bi di làmpam.