¶ Kàddug Aji Sax ji dikkaloon na Yonent Yàlla Yeremi jëm ci Filisteen ñi, balaa Firawna di song dëkkub Filisteen ba ñuy wax Gasa.
TSK
TSK · Amos 1:6
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Jeremiah 47:1
TSK
Ezekiel 25:15
TSK
«Boroom bi Aji Sax ji déy dafa wax ne: Filisteen ñee jiital seen mbañeel gu sax, ñoo jéppee jéppi seeni noon, feyoo feyu, ba faagaagal leen.
Amos 1:9
TSK
Aji Sax ji nee: «Ñetti bàkkaar, su ma yeboo ne ñeent, laay sikke waa Tir, te duma fomm seeni duma. Ñoo jàpp mbooloom lëmm, jalax ca Edomeen ña, te sédduñu ci kóllëreg bokk.
Obadiah 1:11
TSK
Bésub keroog ba ngeen taxawee, janook seen mbokk, bésub keroog ba jaambur ñay yóbbu seen alali bokk, ay doxandéem song bunti dëkkam, bay tegoo bant teraangay Yerusalem, yeen itam, ni noon yooyu ngeen def.
Zechariah 9:5
TSK
Askalon moo koy gis, tiit; Gasa gis ko, jàq njàqare lu réy, mook Ekkron it ndax yaakaar ju tas. Gasa la buur bay réere, Askalon ñàkk ku ko dëkke.