TSK

TSK · Amos 5:13

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Mbooloo ma nag ne cell, tontuwuñu ko baat, ndax Buur moo leen santoon ne leen buñu ko tontu.

Man, ma mel nib tëx, dégguma, mel ni luu, àdduwma,

Doom aadama la bésu safaan bay bett, jekki ne dàll fi kawam, ni jën wu keppu cib caax, loru, mbaa picc mu tancu cig fiir. Doom aadama xamul bésam.

Ñu ne ko: «Esekiya dafa wax ne: “Bésub tey bésub njàqare la ak mbugal ak gàcce. Mooy li ñuy wax naa: Doom a ngi ci buntub juddu, te dooley wasin réer!

Amos 6:10 TSK

¶ Ku warloo waajal mbokkam mu dee dina dugg ca kër ga, ngir yóbbu néew ya, te naan ka ca biir-a-biir: «Kenn desul foofu ci yaw?» Mu ne ko: «Jeex na,» bëgg caa teg baat, mu ne ko: «Déet! Noppil, bul tudd turu Aji Sax ji.»

Micah 7:5 TSK

Buleen gëm ab xarit, buleen wóolu ab xejj, fi kanam ndaw siy tëdd sa gannaaw sax, sàmmal sa bunti gémmiñ.

balaa dogal bee taxaw, bésub mbugal ne jaas ba wéy ni boob, bala leen tàngooru merum Aji Sax jee dikkal, bala leen bésub merum Aji Sax jee taxawal.

¶ Kon nag xool-leen bu baax seen jëfin, defleen jëfinu nit ñu am xel, te baña mel ni ñu ñàkk xel,

¶ Lii, nanga ko xam: mujug jamono, jant yu tar dina dikk.