Absalom nag ne ko: «Bàyyil boog sama mag Amnon, mu ànd ak nun.» Mu ne ko: «Lu muy ànd ak yaw doye?»
TSK
TSK · Daniel 11:27
مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.
Mu jëm ci njiital jàngkat yi, di taalif bu ñeel Daawuda.
Bokk yi, wóoluleen ko fu ngeen tollu, diisleen ko seen xol, Yàllaay sunu kiiraay. Selaw.
Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
Ab nay, bul lekke këram, bul xemmem daraam lu neex.
«Na ku ne moytu dëkkandoom te baña wóolu menn mbokk. Kuy mbokk déy lal nga pexem wuruj, di wuruj; kuy dëkkandoo, sos ngay wéye.
«Neel, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Mbaa jooju reseñ dina baaxle? Mbaa jeneen jaxaay ja du buddiy reenam, buur doom ya, ba lu mu jebbile woon lax, ba buddi reen ya du laaj përëg bu réy, mbaa nit ñu bare?
Mu ne ma: «Maa ngi lay xamal luy xew keroog ba merum Yàlla di jeex, ndax muj ga mooy àppu mer ma.
¶ «Bu àpp bi jotee, buur bëj-gànnaar dina dal ci kaw réewum bëj-saalum. Waaye boobu yoon du deme na woon.
Ca mujug jamono buur bëj-saalum dina fenqoo ak buur bëj-gànnaar. Te itam buur bëj-gànnaar dina mel ni ngëlaani, ne milib ci kawam, ànd ak watiiri xare aki gawar ak gaal yu mag yu bare. Dina dugg ci ay réew, bëtt, jàll nim wal.
Mu ne leen: «Du yeena wara xam jamono jeek bés, bi Baay bi jàpp ci sañ-sañu boppam.
¶ Waaye nag bokk yi, lu jëm ci ay àpp, ak bés ya loolu di am, soxlawuleen ku leen ci bind,