TSK

TSK · Daniel 2:25

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

¶ Ba Firawna déggee loolu, dafa woolu Yuusufa. Ñu gaaw tijji ko, mu watu, solu, doora wuyji Firawna.

Wallul ku ñuy reyi te tooñul, xettlil kuy tërëf, ñu di ko reyi.

Yudeen ña ca bokkoon di Dañeel ak Anaña ak Mikayel ak Asaryaa.

ba noppi ñu dem fekki Buur, ngir wax ak moom ca aaye ba mu tëral, ne ko: «Xanaa du yaa torlu aaye bi ne: képp ku ñaan jenn yàlla mbaa nit ku la moy, yaw Buur, diiru fanweeri fan, dees na ko sànni ca kàmbu gaynde ya?» Buur ne: «Dogal bi kay wér na, dëppook yoonu waa Medd ak Pers, wi dul toxu.»