TSK

TSK · Daniel 2:40

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

yeel yi di weñ gu ñuul, ndëgguy tànk yi nag lenn li weñ gu ñuul la, li ci des di ban bu ñu lakk.

¶ «Ba loolu wéyee ma bëgga am lu leer ca ñeenteelu rab, wa wuuteek ya ca des yépp, ñàng lool, am ay bëñi weñ ak weyi përëm, di moxoñeek a warax, di nappaaje li ci des.

Dina gëna am doole, waaye du doon dooley boppam. Yàqam dina jéggi dayo, te ay pexeem dina joy. Dina faagaagal ñu am doole ba ca mbooloom aji sell yi.

¶ «Buur bi dina def lu ko soob. Dina réy-réylook a damu, ba weesale boppam tuur yépp, te dina wax gilaawaali jëme ci Yàlla ji sut lépp. Dina am ndam nag ba keroog sànjum Yàlla ñoral ko. Li ñu dogal déy dina am.