كل أسفار KYG

Daniel 2

KYG · الآية 44

12 أصحاحات

KYG / Daniel / الأصحاح 2

KYG · الآية 44

« C i jamonoy buur yooyu Yàlla Boroom asamaan dina samp nguur gu dul tas mukk, te wenn xeet du ko yilif mukk. Nguur googu dina tasaare mboolem yeneen nguur yooyu, ba genn du ci des, waaye moom day sax ba fàww.