TSK

TSK · Daniel 4:14

مراجع Treasury of Scripture Knowledge في KYG.

العودة إلى المقطع

«Yeen gan ñi, génnleen Babilon, ku ne rawaleji sa bakkan. Buleen ñaawtéefu jaambur sànkaale; lii àppu mbugal la bu Aji Sax ji matal; seen añ la, bu mu leen añale.

Ay doxandéem a dikk, bokk ci xeet yi gëna néeg, gor ko, wacc, ay bànqaasam wadde kaw tund yeek xur yi, ay caram dammtoo ci xuntiy àll bi yépp, waa réew yépp dawe keram, wacc ko,

¶ Yéenekat ba nag xaacu, ne: «Dégluleen li ñu leen sant, yeen waa mbooloo yépp ak xeet yépp, ak làkk yépp.

Li ñu santaane ñu bàyyi ëkk beek reeni garab gi mooy tekki ne nguur gi dees na la ko delloo keroog boo xamee ne Boroom asamaan mooy Buur.

Waaye ba mu bewee, të ticc bay réy-réylu, dañu koo jàllarbee ca nguuram, nangu ndam la,

Luke 3:9 TSK

Te itam sémmiñ xàccil na reenu garab ba noppi. Kon nag gépp garab gu ci meññul doom yu baax, dees koy gor, sànni ca sawara sa.»

Mu xaacu ca kaw, mel ni gaynde guy yëmmu. Naka la xaacu, juróom ñaari dënu jib.